YONN GUI

ILAN MOSHE ABOU, WILLIAM BALDE, PHILIPPE DESBOIS, GIL GIMENEZ, AUMAR SOW

Yönn-gui sorry-na
Bokö narré deff
Ci suffü taü-gui...
Yönn-gui dina gudü
Bo-cy narré diarr
Di-tallal, ça kanaam
Ta bagna tégy tank...
Wahé lö metti yagül... leygi mü diêkh
Gaal yangy-dem cy ndokh-gy
Batcha nek khamna famü dièm
Wahé dü yag, dina nü taffé-sü !

Yönn-gy dina diaffé
Büla diarralé
Cy mussy-beup kharré
Yönn-gui diss-na
Wahé bull-topo-to ndakh
Bü mané bü nac... lu-munaane
Yönn-gui diaffé-na
Büla diarraté
Cy mussy-beup kharré
Yönn-gui dissna
Wahé bull-topo-to ndakh
Bü mané bü nac... lu-mu-naane...

Canzoni più popolari di William Baldé

Altri artisti di French mainstream pop