Nouyo

Kahifa, Ayema

Ma nouyok niom "nouyo" ma nouyok niom
Ma nouyok niom "nouyo" ma nouyok niom
Boy nouyo dangay yaru, boy nouyo tééy
Boy nouyo ndangay xam fofu ngay nouyo fofu fana

Bonjour bonsoir mani bumu la wañi dara
Mba jamm nga fanaano est ce que yangi jeul say garap
Naka keur gui naka njaboot gui ngala bu ci kén amé tawat
Mana deukeundo bu bess bi mangui doga aksi ci bi barap
Wa coñ bi nanĝén def diallo banana jaay ma pomme
Sama buntu gallé nga lal ni bo fi paré nanga fompe
Boy my boy niowal ni ma yoni la bikite
Dawal gaaw mang ley xaar bo delussé ma may la weccit

Ma nouyok niom "nouyo" ma nouyok niom
Ma nouyok niom "nouyo" ma nouyok niom
Boy nouyo dangay yaru, boy nouyo tééy
Boy nouyo ndangay xam fofu ngay nouyo fofu fana

Borom jeun kaay jaay ma lotte
Xaaral ma até boy bé niung coy sot
Boromo sarett defal ndank giss na saleté bi fi ngu coy beug di sotti
Té lolu du sotti xaaral ma wo njaago bi si coñ bi
Boula jappé tay ji tay ji rek leu ley botti
Té beuguma niu naan ma ya féké waxulo con non non duma noppi
Boy yi si coñ bi sama palentère laniuy feugg séni balles di petits camps
Buniu paré jadd si kiosque bi jeund sène thon def co si petit pain
Gallé commissaire bi kénn du fa dugu giss na si buntu chien méchant
Mo njakona am télé niun ñeupp keureum laniu njeuk sétaané film Jackie Chan

Ma nouyok niom "nouyo" ma nouyok niom
Ma nouyok niom "nouyo" ma nouyok niom
Boy nouyo dangay yaru, boy nouyo tééy
Boy nouyo ndangay xam fofu ngay nouyo fofu fana

Neulé ngi ćoow ñeulé ngi wax né neñ
Modou mbaye a co eumbeul degg na it
Chef du quartier bi doomam afi dakk randal
Gallé niom lopy clando bi degg na dañ fa sampe ay xeureum
Waayé manuma fa bañ dugu ndax faw ma am samey gazelle yimey gëssëm
Xalé yi dima xool té buguma def njaaxum mais bu féké né danio mool
Damey took sama buntu gallé banc cool man dama fonk sama coñ
Ndax lumu metti metti ñangul sama cona dafa ċukk boy
Té boko wéddé dang ga nandul cone boy

Ma nouyok niom "nouyo" ma nouyok niom
Ma nouyok niom "nouyo" ma nouyok niom
Boy nouyo dangay yaru, boy nouyo tééy
Boy nouyo ndangay xam fofu ngay nouyo fofu fana

Canzoni più popolari di Natty Jean

Altri artisti di African reggae