PositiVibz

Hun...Hun Kill them with...
Barrington Levy sample
"Kill them with positive vibes"
With #PositiVibz ...
Dolli tchi waay, yeah (Kill them with Positive vibes) yeah

Verse 1
Ay positive vibes lama di khélli bou doyoul dolli tchi
Lepp lou dieum thi samm kolleuré t’inquiète nio ngui thi
Samm jamm donng ni Lauryn Hill
Nio ngui thi khèkhe, boul khèpe, boul snitch, boul yolé deal
Shit bi soundou strip tease mais sexy neu
Hello DK, Yeubo TeauPla ekssi neu
Nélène Hip Hop bou dèè wone légui dekki neu
Niafé neu beu guénne ghetto bi légui tékki neu
Gueustou negn Pac, yagg déglou Big
Yagg dadji ay pack guénné feuille ak bic
Fone diamou thi punchline yi ak grosses caisses yi
Presque ay Talibé wou Kweli ak Mos Def (yeah)
Be légui kou wakh deugg niou tek thi bate !
Compilou Dekkil Rap léniouy dekkilate
Bou doyoul me dolli thi waye
Jamm dongg legn sékkh ak ay Positive Vibes

Pont1
Haha ak ay diap , han Mister Thiere hit me
Yo Bab’s yéwoul boyyy, han wa H (Grd Medine), bou doyoul me dolli tchi

Verse2
Ay positive vibes yi mey khélli sokhleu woul polémique
Bo dé nit, me togg bolé leu tchi nga goré tchi
Wakh bou beuri mo takh louniou tabakh danou rek
Motakh légui manou rek sinon gaaniou rek
Depuis temps wou Pac niou né tchi same ish
Yo bingay TAKHOURAne seme ga yang thi TAKHOU RAp yi
Sorano: anniversaire PBS, Daara J Saint Michel, DJ Makhtar PCS
Boumou diame yi legn takk tchi bate
Flow bi ley feugg ay kourrou baye Cheikh Ibra Fall
Lo mey kholé ni gayne? deungueu fogone dina fombé ni fight bi?
Ha ay BOMB la lène indil ak ay Positive Vibes

Pont 2
Yea, yo dolli tchi! My man MTO DMC danga dof wala lane
Positive vibes dolli tchi waay
(Bruit de sirène en fond)

Verse 3
Han Positive Vibes yi mey khélli ? Mome rek la yoré ni
Boumeu droiter lo thi naadj bi kanamou gonéyi
Am na médaille d’or dèlloul se keur
Son bi fok mou dow ak Usain Bolt Jailou Reubeuss (#100m)
Ma dakkh youkhou Ndour ma gueneu marre Pène
Deme khiff ay khalam, Souleymane Faye
Génération "Rest In Peace 2Pac Marley"
11 mai niou diam leu yobou leu armel nga ziarre lene
Yo bayil me yémeulé ko fi ga yi parégouniou pour degg yoyou !
Deungueu sonneu ?
Han? Wala me dolli thi waye ?? Ay nokkh lalène digone ak ay positive vibes

Han, loye mel ni kou diommi ni gayne ?
Jamm dongg legn sekkh ak ay positive vibes
Lo mey songgué ni baye hi? Deungueu fogone dina fombé ni? laay!!! huhu
Ak ay positivibz

Lo mey songgué ni baye? deungueu fogone dineu yombé ni, Layyye lol
Ay bombes lalène indil ak ay ...
Lo mey kholéé ni gayne ? Deungueu fogone dineu yombé ni han?
!:* lalène digone ak ay ...
Ay nokkh lalène digone ak ay ...
Ay boxe lalène digone ak ay ...
Jam dongg legn sèkkh ak ay ...
Ay *$^^ lalene digone ak ay...

Curiosità sulla canzone PositiVibz di Elzo JamDong

Quando è stata rilasciata la canzone “PositiVibz” di Elzo JamDong?
La canzone PositiVibz è stata rilasciata nel 2014, nell’album “FreeDope”.

Canzoni più popolari di Elzo JamDong

Altri artisti di African hip hop