Ci Yaw

Elzo JamDong

Verse 1
Sonne naa te guisseugouma dara loumeu meuneu fatté lo ni yow la tannone pour nga samm sama mbeuguél

Fonk naala kone faut que nga nand ma te fogone nani soumeu togué weet ak seme bopp ding me goungué eh

Yama newone ne ding ma dinthial se thiaabi khol te loumou gouddi gouddi dinga tidji soumeu feuggué

Diangg naala mokkal naala amoul dara lougn ma meuneu khamal ci yaw

Ci yaw
Ci yaw
Ci yaw ( ci yawww) ci yaw ci yaw
Ken dou wakh dara ci yaw
Ci yaw
Ci yaw
Ci yaw ( ci yawww) ci yaw
Ken mounouma wakh dara ci yaw

Verse 1
Sa yo guenné mane ngay khalaat
Souma kholé yow rek laa am
Soma guissoul dangay malade
Yen saay me doyal seukk ci yawww

Chorus 2
Sonne naa te guisseugouma dara loumeu meuneu fatté lo ni yow la tannone pour nga wetteuli me te nga samm sama mbeuguel
Faut que ma maanou ndakh thiow li thiow li yeup waroul niaaaw te warouma weddi tam
Lepp lima diangg ci yaw
Ci yaw
Ci yaw
Ci yaw ( ci yawww) ci yaw ci yaw
Ken dou wakh dara ci yaw
Ci yaw
Ci yaw
Ci yaw ( ci yawww) ci yaw ci yaw
Ken mounouma wakh dara ci yaw

Verse 2
Mouno nango am tort
(Ci yawww)
Te guedj nga wakh me d'accord
(Ci Yaw)
Fogone naani c mort
Bobou khawma wone louy amor

Ay khoulo tey dioubo tey
Yenn wakh you sew yi douniou tardelaat soudone tey
Mane lenn laa guiss ci yaw
Moy ken khadioul tchi sougn thiow
(thiow thiow thiow ...)

Yeah ehhh
Chorus 3
Sonne naa te guisseugouma dara loumeu meuneu fatté lo ni yow la tannone pour nga samm sama mbeuguél

Faut que ma manou ndakh thiow thiow li yeup waroul niaaw te warouma guedd tam lepp lima defar ci yaw
Ci yaw
Ci yaw
Ci yaw ( ci yawww) ci yaw ci yaw
Ken dou wakh dara ci yaw
Ci yaw
Ci yaw
Ci yaw ( ci yawww) ci yaw
Ken mounouma wakh dara ci yaw

Hun (ci yawwww)
Hun hun hun (ci yawww)

Curiosità sulla canzone Ci Yaw di Elzo JamDong

Quando è stata rilasciata la canzone “Ci Yaw” di Elzo JamDong?
La canzone Ci Yaw è stata rilasciata nel 2018, nell’album “Macina”.

Canzoni più popolari di Elzo JamDong

Altri artisti di African hip hop