Nama Yalla Baal

Elzo JamDong

Pre Hook (Mathart)

Taal bou Yalla taal wakh féyou ko
Nama Yalla baal gnii ngui seen kow
Takk shine lerr naagn ni bideew
Taal bou Yalla taal wakh féyou ko

Verse 1 (Elzo)
Taal bou Yalla taal tole bou Yalla bey
Diaam bou Yalla fal, dey gueuneu Ttaakkeu di gueuneu teuweu feye
Fall kou Yalla mey daal lo beugg nangou tchi mom nanga nangou ni deung ko koye feye
Ndakh kou Yalla mey baat dineu wakh te kou am bou neekh de koy weye

Deme dane lakkhatou gni me diégué (gnimeu) deme lerrone seni beut beu niou goumbeu
Gni me gueuneu sori nio meu done ndieukk sene mey takk di magg niou mel ni niou moumeu (moumeu)
Niveau bi gueuneu kowé laye football
Legui mbeur yi fi eupp gueudd laye doumeu
Deme diok djité xaroumeu Adioumeu
Mangui weur kane momeu soute te guissoumeu

Soubeu ci Diante gouddi werr
Takk na shine boul begn lolou ken dou tchi polemiquer

Ngande la lerre neu maye thiaatou bidew bi dioudou fer di lekk tchi bolou mak yi

Fangg na fegne na diommi nguene ndakh dolé dji nék tchi mane? mo gueuneu kowé dolé djinné

Rangou na khekh na be togg
Tchine gua ngui kheegne nekh te dou gowé tchi né

Pre Hook x1

Hook
Nama Yalla Baal (Yalla baal hey) x4

Verse 2 (Elzo)

Yagg na def ay hit awright
Bobou amagoumeu wone ay clip awright
Li fi Thiere binde tchi recettou beat
Eupp neu ay livre Diekhelneu ay bic (come again)

Yagg na begueul ay nit awright
Bobou amagoumeu wone aye sites
(Wallaye)
Bi ngay ndieukk degg limeu binde deugueu replay nangou ni kone mousso wone write (dope)

Ma dakh rap Senegal Diallo
Manekk tchi nguur gui def ko seme Freengdom
Seme dope legalize soumeu nekhone guenné bum boumey touddé Dakar Kingston

Dieuleul bi def ko Ringtone
Gningui job te moussouniou am piston
Kou le ladj ndakh ma ngui gérer fight bi neko maye Mouhamet Ali tchi kow ring bro

Demey takk doumeu mandi
Ay daadj naturel la andi
Def le Mario diam le aye Champi
Soudone western movie degn mey Wanted (wanted)

Hey boumeu wone se kanamou Gentil
Kham na yangui niaane me fey nga meun tranquille
Demey gass tombe soul ay garcon comme Gaston tchi microphone mane mey bandit

Bridge (Mathart)

From the underground liguey bi dorroul tey
Guiss nga egg negn tchi kow liguey bou sete dey fey
Kila yagg tipser lo kepp se good time
Get sunu vibes feel alright
Deniou dore mou nathieu nigga nieupp sèèdé ko wallaye
Change game bi def safaar indi mousslaay
Never never nga guiss niou tchi détails
Wowéma grossiste one more time (uh yeah uh yeah)

Hook

Curiosità sulla canzone Nama Yalla Baal di Elzo JamDong

Quando è stata rilasciata la canzone “Nama Yalla Baal” di Elzo JamDong?
La canzone Nama Yalla Baal è stata rilasciata nel 2015, nell’album “Free Season”.

Canzoni più popolari di Elzo JamDong

Altri artisti di African hip hop