Falaaw

Elhadji Diallo

Yow kaay niou job ndakh moui tané bro
Amoul khof talougn saalé sope warougn planer
Kaay niou job ndakh mou tané bro, ndakh mou tané
Amoul khof talougn saalé sope

Kham na lima beugg, kham na lima beugg
Mang koy dound deug, mang koy dound deug
Amoul lomay diangal, amoul lomay diangal
Bimay eksi seen naala lay niangal (seen naal angay niangal)
Mais yafa niaaw
Falaaw falaaw falaaw
Falaaw falaaw falaaw
Falaaw falaaw falaaw

Yow kaay niou job ndakh moui tané bro
Amoul khof talougn saalé sope warougn planer
Kaay niou job ndakh mou tané bro, ndakh mou tané
Amoul khof talougn saalé sope amoul baalé

Yagg diow motakh yaakh ak thiow
Légui dam ci paré
Dakhone fo maala ndieukk dore ak tokh cigarette

Wayé no dama yagg fort mané faut que mou carré
Faut que niou diok
Borom meukh dome
Mounoul khèkh ak armée
Légui soy def liste Elzo'y djiitou
Bougn sanione ma daanou Metzo Djatah
Légui no def se sista né daf may bisou
Firr dou takh ma waagni sama khadar

Kham na lima beugg, kham na lima beugg
Mang koy dound deug, mang koy dound deug
Amoul lomay diangal, amoul lomay diangal
Bimay eksi seen naala lay niangal (seen naal angay niangal)
Mais yafa niaaw
Falaaw falaaw falaaw
Falaaw falaaw falaaw
Falaaw falaaw falaaw

Seme life aka beuri ay signe
Fi meu diare douniou beuré ko sagne
Nekhoul be nekhoul mais beuri na style
Ladial gangor yi ak mbeur yimeu dane
Deungueu diappone dingueumeu stop
Mais deme tangg be time le nga mar
Deme high, deme deep, deme tar
Seme ga yangui deal seme crack
Guiss na ni fi defe khate wayé Free lim fi dji defe sakh
Nenegn le thiow li ngay thiowe ding ko bayi ndakh nioune nioye gni titeul se squadd
Nekk ay killer tchi rap deukké job kharougn 8 heure du mat
Doper na mineur ak mag niou meu diappé me dealer bou mak
Yang may diss (10) may play lou rey comme Zizou
Ngay copier Biggie te se laamign rekkeu paata
Rakk boul di sathieu mère ay bijou
Bou leu aakham dalé c'est la cata!

Kham naa lima beugg
Mang koy doundou deugg
Amoul lomay diangal
Bimay eksi seen naala ngay niangal
Mais yaafa niaaw

Kham na lima beugg, kham na lima beugg
Mang koy dound deug, mang koy dound deug
Amoul lomay diangal, amoul lomay diangal
Bimay eksi seen naala lay niangal (seen naal angay niangal)
Mais yafa niaaw
Falaaw falaaw falaaw
Falaaw falaaw falaaw
Falaaw falaaw falaaw

Curiosità sulla canzone Falaaw di Elzo JamDong

Quando è stata rilasciata la canzone “Falaaw” di Elzo JamDong?
La canzone Falaaw è stata rilasciata nel 2015, nell’album “Free Season”.
Chi ha composto la canzone “Falaaw” di di Elzo JamDong?
La canzone “Falaaw” di di Elzo JamDong è stata composta da Elhadji Diallo.

Canzoni più popolari di Elzo JamDong

Altri artisti di African hip hop