Tali Bi

Tali Bi

Temps boy aka ma beugone dokhi, Point E, Colobane, yeneen gokh
Téla guiss lou graw mais do wakh
Crew bi takhaw nigga karaw sakh
Nigga moussou gnou beugue def lou bone
Mais influence boy comme téyé gun
Mais téla kham mbede téla bone
Connexions you raw telephone
Ba yena vibes boy dima dougou may fonk goudi boy begna teude
Drogue bi di yeungal kogn ba kogn boy gnou tokk ci banc diakhlé di ko kheutche
Police romb we don’t give a fuck
Sunu kogn la boy da gnouy tokk
Auto yi garé son bi yokke boy shorty you toye yi beugue bokk boy walabok
Moussou gueum né bess boy di na thiol nigga
Thioye yi garé sen truck indil gnou thiow nigga
No snitch no daw nigga taff taff niou ngui
Ci violon Bi God damn it lou mel ni mang koy doga guiss (ooouuuh)

Tali bi Tali bi Tali bi Tali bi Tali bi Tali bi
Tali bi Tali bi Tali bi mame booy daan na ma wakh moytoul tali bi
Tali bi Tali bi Tali bi Tali bi Tali bi Tali bi
Tali bi Tali bi Tali bi mame booy daan na ma wakh moytoul tali bi yeah
Fa la xamé louy crack coke ak bone nigga
Fa la andék kou baax ak kou bonn nigga
Fa la défé lou baax def lou bonn nigga
Rep sa kogn nigga

Violon Bi nekhaloul kene man
Life bi ay peines you doul diekh la man
Chaque jour mou tegueul le once again
Teudjeul sa gate boy té lem sa gueen
Ndakh gangsta deug boy doko degg
Ay silencieux boy ba foumouy yegue
No pain no pain no gain do siw ndakh tela fegn
Drug money boy yomboul begn ni kilo bone ak Taylor gang
Am fouleu boy tela begn mané fuck boy gni lay diey
Ndakh sa yeek sou yombé yena yombe yi bess di nga daanou khötal kambe yi walabok
Khamna gnou daadj you baakh ak you bone nigga
Khamna gnou sho you baakh ak you bone nigga
Rep sa kogn nigga
Mais moytoul ma tali bi mo la fi djitou té fi nga koy quitté boy lolou dou diekh

Tali bi Tali bi Tali bi Tali bi Tali bi Tali bi
Tali bi Tali bi Tali bi mame booy daan na ma wakh moytoul tali bi
Tali bi Tali bi Tali bi Tali bi Tali bi Tali bi
Tali bi Tali bi Tali bi mame booy daan na ma wakh moytoul tali bi yeah
Fa la xamé louy crack coke ak bone nigga
Fa la andék kou baax ak kou bonn nigga
Fa la défé lou baax def lou bonn nigga
Rep sa kogn nigga

Yeah

Canzoni più popolari di Nix

Altri artisti di African music