MBEKTE

Bruno HOVART, Lansana SANE

Mbeté dé gneuwna
Mbeté dé gneuwna
Lagne done xare gneuwna
Lagne done xare gneuwna
Békénagnou déee

A lilaye yawe mane
Yégeuna sama xole mane
Gathieu loma yaw mane
Maco sédé
A douma thi tayi yawe mane
Taye sama beure dane
Gnoune béknagne danthi contane
Maco sédé
A fila sonalone mane
Gamadi mognalone mane
Mounonga deme banane
Maco sédé
A ki dafa bonne yawe mane
Yamadi taneu yawe mane
A ki dafa woné dé.

Mbeté dé gneuwna
Mbeté dé gneuwna
Lagne done xare gneuwna
Lagne done xare gneuwna
Békénagnou déee

Canzoni più popolari di Lass

Altri artisti di Afrobeats