FUNANA

Bruno HOVART, Lansana SANE

Misse xadé miro
Yaw xanadé miro
thi mane
Misse xadé miro
Ma chérie moi je t’aime
Moi je suis fou de toi
Wa xana dofo
Yaw xana diexo thi mane
Misse xanadé guisso
Ma chérie moi je t’aime
Moi je suis fou de toi
Cherie mane tayina
A xolo mane sonouna
Héye yaw guissega
Liguaye yawe néhouma
Wa Cherie yaw guissega mbeugeuel rekeu mafi téyéeeeee
Ma chérie moi je t’aime
Moi je suis fou de toi

Maguila nope baligui
Lou atti bari bari yaw
Manoumala faté
Mane dama dofe si yaw

Mane wahe na ba sonne
Mane dawena ba sonne mane dale
Xoloma béne yone
Ma chérie moi je t’aime
Moi je suis fou de toi
Boule ragale dara
Lo beugeue gnou def mac yaw
Ligama diarral

Ma chérie moi je t’aime
Moi je suis fou de toi
Sayo méré mane damaye mérdé
Sayo bégu émane damaye béguedé
Liga donne si mane mbeuguel moco téyé
Ma chérie moi je t’aime
Moi je suis fou de toi

Maguila nope baligui
Lou atti bari bari yaw
Manoumala faté
Mane dama dofe si yaw

Canzoni più popolari di Lass

Altri artisti di Afrobeats